Aller au contenu

weer

Jóge Wiktionary.

wolof

[Soppi]

weer: am na ñetti tekki

Weer:

Ci arminaat

Weeru wolof walla weeru weer: tamxarit, digguw gàmmu, gàmmu, rakk-ji-gàmmu, rakkaat-ji-gàmmu, maamu koor, ndayi koor, baraxlu, koor, kori, digg, tëbëski.

  1. Weer yii ci weer wi lañu aju, su teroo weer tàmbali, bu deewee mu jeex, leeg-leeg ñu mat fan-weer leeg-leeg ñu yées ko, di ay ñaar fukki fan ak juroom ñeent mbaa ak juroom ñatt, ñooy yu lislaam yi it.

Weeru jant: samwie, feewrie, maars, awril, mee, sue, sulet, ut, satumbar, oktoobar, nowambar, desambar.

Ci Saytubiddiw
  1. bidiw bu mag biy faral a feeñ guddi ci asamaan si, tey leer nàññ, bay leerale. , .
Ci Simi

Ab weer: man naa juge ci xottu bitéel walla beneen ne-ne, lu mel ne kawsu, tey faral a yaraax ba ngay man a gis ku nekk ci ginnaawam.

Tekki

[Soppi]

wu-faraas: mois, lune, verre