Aller au contenu

Sëriis

Jóge Wikipedia.
Nataalu garabu sëriis

Sëriis garab gu bàyyikoo Madagaskaar la. Ci njabootu Phyllanthaceae la bokk. Doomam dees koy lekk, day wex. Xobam rënd la ci toggi yenn réew yi

Turu xam-xam

[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Phyllanthus acidus

Yeneen làkk

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Farañse: girembellier