Géej gu Diggu
Apparence
Géej gu Diggu mooy géej gi ne ci diggante goxu Afrik ak bu Tugal ak bu Asi. Guddaayam di 2,51 milyioŋ ciy km² te yaatuwaayam toll ci 3700 km.
Ci sowwu mi ngi yem ci Mbàmbulaanu Atlas, ci penku ci Géeju Marmara ak Géej gu Ñuul gi. Yenn saa yi Géeju Marmara dees koy boole ci Géej gu Diggu gi, waaye Géej gu Ñuul gi moom dees koy tàqale ak moom.
Melokaan
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Géej gu Diggu gi dees koo seddatle ci ñaari mbalka*. Mi njëkk mooy Géej gu Diggu gu sowwu gi, yam ci yoonal* gu Sisil. Meneen mi mooy Géej gu Diggu gu penku gi.
Karmat
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]- Yoonal: canal
- Mbalka: bassin
Diwaani Tugalasi | |||
Asi | Diwaan yu MR: Diggu Asi · Penku Asi · Bëj-saalum-penku Asi · Ron-goxu End Yeneen diwaan: Penku gu Sori · Penku gu Diggu · Penku gu Jege · Sibeeri | ||
Tugal | Diwaan yu MR: Sowwu Tugal · Bëj-saalumu Tugal · Penku Tugal · Bëj-gànnaaru Tugal Yeneen diwaan: Kókaas · Géej gu Diggu · Skandinaawi |