Àkkasaa
Apparence
Àkkasaa, garab la gu bokk ci njabootu Fabaceae, Asi gu Ngopp suuf (bëjsaalum-penku) la bàyyikoo waaye ci lu yees nit tasaare na ko, ji ko Afrig.
Melo wi
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Garab gi man na àgg ba 25i met ci guddaay. Xobam day njaxas. Tóortóoram ya dañuy mboq te dajaloo ciw car ba noppi sëq te di guddee nu day ni 15 ba 30 sàntimet. Doom bi day wërbalu teg ci di àgg 10 ba 30i sàntimet ci guddaay.
Njariñ yi
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Dees ko jëfandikoo ngir: -Jëmbat pàkk yi booy. -Dekkil suuf su dee. -Faj mettig yenn cér yi. -Defar yenn garab yi.
Nataal yi
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]-
Tóortóoru àkkasaa
-
Xob yi
-
Doom yi
-
Xooxu doom bi
Turu xam-xam wi
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Tur wi ci yeneeni làkk
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Farañse: cassia du Siam/ casse du Siam.