Andoronikus

Sumbu 7 Maars 2013 à 20:36, bu: Addbot (waxtaancëru) (Bot: Migrating 12 interwiki links, now provided by Wikidata on d:q513430 (translate me))
(wuute) ← Sumb bi jiitu • Sumb bi teew (wuute) • Sumb bi toftal → (wuute)

Ci angale ak ci faranse mooy Andronicus.

Benn Yawut bu toppoon Yeesu la woon. Ndawu Kirist la woon ki bokkoon ak Kirist bala Pool.

Ci Injiil dañu koy gis ci Ro 16:7.