Sëriis

Sumbu 8 Sulet 2019 à 00:25, bu: Daarul xayri (waxtaancëru) (Xët wu bees : vignette|Nataalu garabu sëriis '''Sëriis''' garab gu bàyyikoo Madagaskaar la. Ci njabootu Phyllanthaceae la bokk. Doomam d...)
(wuute) ← Sumb bi jiitu • Sumb bi teew (wuute) • Sumb bi toftal → (wuute)

Sëriis garab gu bàyyikoo Madagaskaar la. Ci njabootu Phyllanthaceae la bokk. Doomam dees koy lekk, day wex. Xobam rënd la ci toggi yenn réew yi

Nataalu garabu sëriis

nataal yi

Soppi

Turu xam-xam

Soppi

Phyllanthus acidus

Yeneen làkk

Soppi
Farañse: girembellier